Horreur sur l’autoroute ila touba: un corps sans vie découvert

ir mou doywaar am ci autoroute ila touba bi benn waay lagnou fi fékk mou faatou bo wésso touba Toul, ci nonou lagnouko yobou ci district sanitaire bou khombal ci ndingalou procureur bi sooul nagnouko demb ci arméer you ngay nekk ci khombal améwoon ci teewaayou commandant brigade bou gendarmerie ak commandant sapeurs pompiers ak chef service d’hygiène ak imamou poste de santé bâ, mom nak kenn khamoul louko faat te kenn khamoul foumou deukk.*Mame fallou dieng* xibaaru reewmi

Soyez le premier à commenter

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée.


*


Résoudre : *
29 + 10 =